Matthew 25:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñi ñàkk xel wax ñi am xel: “Mayleen nu ci seen diwlin, ndaxte sunuy làmp ñu ngi bëgg a fey.”