Matthew 25:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñi am xel tontu leen ne: “Li nu yor du doy ngir nun ak yéen; tee ngeen a dem ca jaaykat ya, jënd.”