Matthew 26:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yudaa, mi ko nar a wor, laaj ko: «Mbaa du man, kilifa gi?» Yeesu ne ko: «Wax nga ko.»