Matthew 26:45 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu mu ñëw ca taalibe ya ne leen: «Nelawleen léegi te noppalu. Waxtu wu ñu ma war a jébbale ci loxoy bàkkaarkat yi, jege na.