Matthew 26:56 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye lii lépp xew na, ngir amal Mbindi yonent yi.» Ci kaw loolu taalibe yépp dëddu ko, daw.