Matthew 26:62 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci kaw loolu saraxalekat bu mag ba jóg ne ko: «Ndax doo tontu dara? Loo xam ci li ñii seede ci yaw?»