Matthew 26:64 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu tontu ko: «Wax nga ko. Maa ngi leen koy wax it, li dale fii dingeen gis Doomu nit ki toog ci ndeyjooru Aji Kàttan ji, di ñëw ci niiri asamaan si.»

Recommended Reading