Matthew 26:73 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Nes tuuti ña fa taxawoon ñëw ci Piyeer ne ko: «Ci lu wóor ne yaw itam bokk nga ci ñoom, ndaxte sa waxin feeñal na la.»