Matthew 27:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Gannaaw loolu Yeesu taxaw ca kanamu boroom réew ma, boroom réew ma laaj ko; «Ndax yaa di buuru Yawut yi?»