Matthew 27:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi nga xamee ne daje nañu nag, Pilaat laaj leen: «Kan ngeen bëgg, ma bàyyi ko, Barabas walla Yeesu mi ñuy wax Kirist?»