Matthew 27:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Bi nga xamee ne génn nañu, ñu daje ak nit ku dëkk Siren te tudd Simoŋ; ñu ga ko, ngir mu gàddu bant, ba ñu war a daaj Yeesu.