Matthew 27:63 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu ne ko: «Boroom réew mi, fàttaliku nanu ne, naxkat booba waxoon na, bi muy dund naan: “Gannaaw ñetti fan dinaa dekki.”