Matthew 28:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yeesu ne leen: «Buleen tiit, waaye demleen yégal samay bokk, ñu dem Galile; foofa lañu may gise.»