Matthew 28:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ba ñuy dem, ñenn ca wottukat ya ñëw ca dëkk ba, xamal saraxalekat yu mag ya lépp lu xew.