Matthew 28:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
te ngeen dem bu gaaw, wax ay taalibeem ne, dekki na te jiituji na leen Galile; foofa ngeen koy gise. Lii laa leen wax.»