Matthew 28:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ba ñuy dem nag, Yeesu taseek ñoom ne leen: «Maa ngi leen di nuyu.» Jigéen ña jegesi, laxasu cay tànkam, di ko màggal.