Matthew 3:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Layoom mu ngi ci loxoom, ngir jéri dàgga ja, ba mu set; pepp ma dina ko def ca sàq ma, waaye xatax ba dina ko lakk ci safara su dul fey mukk.»