Matthew 3:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yaxya nag mu ngi soloon mbubb mu ñu ràbbe kawaru giléem, takk geñog der ci ndiggam. Ay njéeréer la doon dunde ak lem.