Matthew 3:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu ñépp génn jëm ci moom, ñi dëkk Yerusalem ak diiwaanu Yude, ak waa dexu Yurdan.