Matthew 4:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu tontu ko: «Sore ma Seytaane, ndaxte Mbind mi nee na: “Nanga màggal Yàlla sa Boroom, te jaamu ko moom rekk.”»