Matthew 5:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Te it duñu taal làmp, dëpp cig leget, waaye dañu koy wékk, ba muy leeral ñi nekk ci kër gi ñépp.