Matthew 5:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Na seen leer leere noonu ci kanamu nit ñi, ngir ñu gis seeni jëf yu rafet, te màggal seen Baay bi ci kaw.