Matthew 5:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye man maa ngi leen di wax ne, ku fase sa jabar te du ci njaaloo, yaa koy tegtal yoonu njaaloo. Te it ku takk jigéen ju ñu fase, njaaloo nga.