Matthew 5:34 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye man maa ngi leen di wax ne, buleen giñ dara; bumu doon ci asamaan, ndaxte moo di jalu Buur Yàlla;