Matthew 5:39 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye man maa ngi leen di wax ne, buleen bañ ku leen def lu bon, waaye ku la pes ci sa lexu ndeyjoor, jox ko ba ca des.