Matthew 6:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye su ngeen baalul ñi leen tooñ, seen Baay it du leen baal seeni tooñ.