Matthew 6:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
ngir sa koor bañ a feeñu nit ñi, waaye mu feeñu sa Baay bi bët mënta gis. Noonu sa Baay, bi dara umpul, dina la ko delloo.