Matthew 6:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Yéen ñi néew ngëm! Bu Yàlla woddee nii ñaxum tool yi, miy sax tey, te bu subaa ñu def ko ci taal bi, ndax du leen gën a wodd?