Matthew 6:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte loolu lépp, ñi xamul Yàlla ñoo koy wut. Te seen Baay, bi nekk ci kaw, xam na ne am ngeen soxla ci loolu lépp.