Matthew 6:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye jëkkleen a wut nguuram ak njubteem, te loolu lépp dina leen ko ci dollil.