Matthew 6:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Te it bu ngeen di ñaan, buleen bareel wax yu amul njariñ, mel ni ñi xamul Yàlla; ñoom defe nañu ne, Yàlla dina leen nangul ndax seen wax ju bare.