Matthew 7:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
«Du képp ku may wax: “Boroom bi, Boroom bi,” mooy dugg ca nguuru Yàlla Aji Kawe ji; ka cay dugg mooy kiy def sama coobareg Baay, bi nekk ci kaw.