Matthew 7:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye képp ku dégg lii ma leen wax, te jëfewuloo ko, dinga mel ni nit ku ñàkk xel, ku tabax këram ci gànnuus bi.