Matthew 8:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye ñi waroon a bokk ca nguur ga, dees na leen sànni ci biti ci lëndëm gi. Foofa dees na fa jooy tey yéyu.»