Matthew 8:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Laata ñuy jàll, benn xutbakat daldi ñëw ci moom ne ko: «Kilifa gi, dinaa la topp fépp foo jëm.»