Matthew 8:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye Yeesu tontu leen: «Yéen ñi néew ngëm, lu tax ngeen tiit?» Ci kaw loolu mu jóg, daldi gëdd ngelaw li ak duus yi. Lépp dal, ba ne nemm.