Matthew 8:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ña rab jàpp daldi xaacu naan: «Yaw Doomu Yàlla ji, loo nuy fexeel? Ndax danga noo bëgg a mbugal, bala waxtu way jot?»