Matthew 8:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ba sàmm ya gisee loolu, ñu daw, dem dëkk ba, nettaliji lépp ak la xewoon ca ña rab jàpp.