Matthew 8:34 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu dëkk ba bépp génn seeti Yeesu. Ba ñu ko gisee nag, ñu ñaan ko, mu génn seen réew.