Matthew 9:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Xam ngeen ne, kenn du daax mbubb mu màggat ak sekkit wu bees; ndaxte sekkit wi day ñoddi mbubb mi, te xottiku bi gën a yaatu.