Matthew 9:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon Yeesu daldi laal seeni bët ne leen: «Na am, ni ngeen ko gëme.»