Matthew 9:30 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof 1987
Ca saa sa seeni bët daldi ubbiku. Yeesu dénk leen bu wér ne leen: «Moytuleen kenn xam ko.»