Micah 2:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bànni Israyil, ndax dees na waxe nii: « Aji Sax ji day xàddee?» Am: «Jooju jëf da di jikkoom?» «Sama kàddu jàmm la ci kuy def njub.