Nehemiah 10:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te itam bu waa réew mi indee am njaay mbaa lépp luy pepp, di ko jaay ci bésub Noflaay, dunu ko jënd ci ñoom bésub Noflaay mbaa bés bu sell, te atum juróom ñaareel mu nekk dinanu bale bépp bor.