Nehemiah 11:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moom la ak seeni bokk, yu jàmbaare te ñeme. Ñuy téeméer ak ñaar fukk ak juróom ñett. Sabdiyel ma Agdolim di baayam moo leen jiite woon.