Nehemiah 11:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ak Mataña ma baayam di Mika. Sabdi mooy baayu Mika; Asaf miy baayu Sabdi moo doon kilifa gay jiite ci cant ak ñaan; ak Bagbukiya miy mbokkum Mataña tey njiit li topp ci moom ak Abda mi Samuya di baayam; Galal di baayu Samuya, Yedutun di baayu Galal.