Nehemiah 11:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kilifag Leween ña ca Yerusalem moo doon Utsi ma Bani di baayam; Xasabiya di baayu Bani, Mataña di baayu Xasabiya, Mika di baayu Mataña. Utsi bokkoon ci ñi askanoo ci Asaf te doonoon woykat yay woy ca kër Yàlla ga.