Nehemiah 11:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Petaya ma baayam di Mesesabel mu bokk ci askanu Sera doomu Yuda moom la Buur dénkoon mboolem mbir yi soxal mbooloo mi.