Nehemiah 12:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ña jiite woon seeni kër baay te askanoo ci Lewi, ba ca jamonoy Yonanan sëtub Elyasib daan nañu leen bind ñoom ñépp ca téere ba ñu dippee Xew-xew ya.