Nehemiah 12:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñooñoo fa nekkoon ca jamonoy Yowakim doomu Yosuwe. Yosuwe, Yoccadag mooy baayam. Ñoo fa nekkoon itam ca jamonoy Neyemi boroom dëkk ba, ak Esra ma doon sarxalkat, di bindkat.